ci turu Yàlla laye tambalé midi àji yërëm jaam nëpu ci aduna di àji yërëm waay texe yi ci alaaxira
Rabbi as haabaka bil himmati wala tou rabbi him bid darsi fakhate...

Wakhtanou Koor ak Serigne Moustapha Mbaye

khassaides-en-arabe

 

Les Khassaïdes en Arabe

Autres:

Ajouter un Commentaire


Code de sécurité
Rafraîchir

Commentaires   

+1 # Ahmed Dame Sylla 10-07-2016 23:48
Salam
Mbokk jangène jeuff yalnalène yalla faye ci barkèbe kou tedde ki. Damadon laadj ndakh Moukhaddamatoul Khidma jappandina walla damakoo weur bassonnou guisoumako.
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # bamba diop 21-06-2016 18:47
mboki talibè ziarè nalèn bou wèrr tay rafètt lou liguèy bou am solo bi di gnan guèn da dièsi ak gramoul serigne mai mam tèrè FOULKOUL MASHOUNE damako don warr founè si internet bi manou mako guiiss fèn ta khawma lou takh ta guiss na diwan youbari lègui nak man fèkhè na ba dèff ko en pdf ma bagon koumasi diapalè ma dèff ko si internet bi
Répondre | Répondre en citant | Citer
+2 # talibé 22-01-2016 08:54
mangui drouss khassida yi sama bureau diaguéne dieuf!
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # Khalil 19-01-2016 10:32
Akassa amena solo! yénagui def liguéye bou reuy
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # momar talla niang 24-11-2015 19:15
Sant Serigne touba rek
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # serogne saliou 22-10-2015 15:33
Sante Serigne saliou rek mais aidez moi a telecharger les khassida diaguene dieuf
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # sylla touba 05-10-2015 13:25
merci beaucoup vous m'avez permis de télécharger les xassidas que je voulez yala nalène yala faye
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # meissq kabo 21-09-2015 18:36
Ahmadou bamba dieuredieffeti
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # mbacke gadiaga 15-09-2015 20:05
Djalibatou rek
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # mbacke gadiaga 15-09-2015 20:04
Dialibatou rek
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # modou ndiaye 15-09-2015 10:28
Mais sante serigne touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # ndoye 14-09-2015 21:04
Dieureudieufa sérigne touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # issadiouf 14-09-2015 15:28
Serigne touba rk
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # issadiouf 14-09-2015 15:27
Naleine setigne by fayal bopam
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # issadiouf 14-09-2015 15:25
Dieuredieuf serigne touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # ami nguet 10-09-2015 20:43
Serigne Saliou rek mome dongue nakh
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # moustapha fall 08-08-2015 14:28
Yal nalene brome touba. Faye
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # Khadim fall 05-08-2015 00:41
Dieureudjieuf Cheikh Ahmadou Bamba
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # Daoud 21-05-2015 22:20
Ziar, Yallah Faye lene ay yiew you kawe sen ndjort bake Serigne Touba.

Je cherche Bismilahi IKFINI traduit en Francais please please please. Une idee ou je peus trouver ca??
Répondre | Répondre en citant | Citer
+2 # Fallou Tine 17-05-2015 20:35
yalla nagnou dadjé ak ngereumal sergne bi
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # khadim diop 16-05-2015 20:39
dieureu nguéne dieuf.yalla na léne serigne bi faye.beugone na telecharger.ashaloul massalik
Répondre | Répondre en citant | Citer
+2 # djily dieng 09-05-2015 10:07
sopolen lolo merci
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # Diop Abdou 27-04-2015 13:29
Sakh ci beugue ak geume Cheikhoul KHADIM rek INCHAALLA
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # thiam 25-03-2015 14:27
dieuredieuf brom touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Mbengue la Bambiste 12-03-2015 13:34
Dieureudieufe serigne touba mbacke yalla na yalla bour bi fayal gnouko
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # abdou ndiaye 11-03-2015 20:21
sant serigne bi rék
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # abdou aziz ndiaye 11-03-2015 20:19
sant serigne bi rék
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # ousmane diop 25-02-2015 23:59
Yala nalene mame cheikh Ibrahima fall faye barkeb serigne massamba MBACKE barkeb borome touba amiiiiiine"dieuf dieul*gninee dieuf dial*te bagna guestou"
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # khadim fall 13-02-2015 19:08
Dia dieuf khadimou rasoul
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # serigne fallou ngom 08-02-2015 15:41
WaaAw len goOr Yalna nguen si dadieg ngueureumou kou ted ki lou am solo nguen di def
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # tapha seye 08-01-2015 23:05
Diarangénne dieuff
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Al Himma 06-01-2015 10:28
Ziar ak Magal,
Merci à toutes et à tous pour vos contributions :-)
Jaguènejeuf
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # assane seye 05-01-2015 18:05
dieureudjieufé borom touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # mamadou Wagne 02-01-2015 23:01
Santé bamba Warna koudib dioulit
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # mamadou Wagne 02-01-2015 23:00
Dieuredjefety serign touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # ndongolikane 01-01-2015 09:52
NS saluons votre travail diaadieuf
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Ibrahima Sankharé 20-12-2014 02:52
Dieuredieufaty SERIGNE saalihou Cheikh Béthio diamou SERIGNE saalihou yagal diamono Thioune
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # mor ndiaye 14-12-2014 18:19
séne liguéye rafétna! yalla nanguène thi ame faye bu kawé séne gnothe! bidjahi Rassoulillahi sallalahou qanlay wa sallame wa bi daradjatti Khadimou Rassoul radiyallahou tanlla anhou!amine!
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # touba 03-12-2014 22:16
gaye
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # CHEIKH AHMADOU BAMBA 02-12-2014 18:37
YALLA NALENE SERIGNE BI FAYE
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Dame Gaye 01-12-2014 22:51
S. Touba amoul morom tee douko meusa am dou fi dou feulee
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # maï 01-12-2014 13:35
Sant bou wer .si l ecriture des khassidas pdf etaient plus claire sa serait mieux .merci
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # cheikhouna gadiaga 30-11-2014 10:24
yalna nalene yalla fay
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # ahmadou 27-11-2014 04:19
Dieureudieufé serigne touba Diaramaa amirou soultan bamba fepp cheikh ahmadou kara Mbacke noreyni
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Khalil 25-11-2014 17:40
Dieuredief serigne touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # Moussa faye ugb 15-11-2014 19:02
Dieredief thi xidmabi lolourekawer yalna sax bar ke xassidayi amine
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # khalifa 10-11-2014 14:23
slam mbokk yi dama amone yiter lol si amm ay khasida francais
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # khalifa 10-11-2014 14:06
slam dama am yiter lol nguene faguoma aye khasida en francais car je peu pa lire en arabe
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # ada marakhib 07-11-2014 09:54
Dieuredieufeti serigne Touba dit borom dialibatou yaakari diamyi fi au fele
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # moussa ndir dieng 29-10-2014 01:22
Yalla na len serigne touba faye adouna wa lakhira
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # moussa ndir dieng 29-10-2014 01:19
Yalla na len serigne Touba faye
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # MAMADOU BEYE 25-10-2014 11:09
DIEREUDIUF SERIGNE TOUBA MBACKE AMOUL MOROM
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # abdou aziz ba 24-10-2014 13:29
sa sou ne sante serigne touba warnanou nakh kheweul boudoul diekh lagnou fi bayil thi adouna ak aalahirah mo takh gorgolou thi khasida yi di wakh sasoune dieureudieuf serigne touba mbacke
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # khadim cisse 18-10-2014 20:24
Dieureudieufa cheikh ahmadou bamba khadim rassoul.
Lèguèy bi rafètna mashalla YALLAH faye yiw
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # modou 12-10-2014 15:47
Dieuredieuf yallah na bourbi nangoul mène te fay lene
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Moussa Fall 10-10-2014 00:39
Diadieuf waye ni dongoula beguenaniou
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # rakhou 10-10-2014 00:35
Dieuredief borom touba doli sant rekgcv9y
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # khaly fall 06-10-2014 09:31
Dieureu guéne dieufeuti biguéne niou mayé niou meune di dourrouss sa souné ou que nous soyons.merci
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # cheikh thiam 28-09-2014 18:37
Merci serigne touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # cheikh thiam 28-09-2014 18:35
Ns remercions le tout puissant d ns avoir donné khadimoul khadim,il ns a fait sortir d l'obscurite en lumiere
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # ibrahima toure 23-09-2014 07:39
Alhamdoulilah
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # sokhna adama beye 22-09-2014 18:07
Dieureudieufaty serigne saliou backe cheikh bethio diamou serigne saliou yalla nafi yag lole te werre dakh kate mane massouma diank khassida bi ma diebalo ci cheikh bethio la fonkate khassida dax kate day diguele ci nioune te ab mouride kate diguele rek
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # sokhna 19-09-2014 22:11
YALLAH faylène yiw liguèy bi rafètna
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # sokhna 19-09-2014 22:10
Lèguèy bi rafètna mashalla YALLAH faye yiw
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # khadim dieng 17-09-2014 14:25
Dieurradieufa cheikh ahmadou bamba Khadimorrasoll
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # thierno gaye 17-09-2014 00:36
Sante brom darou marnane cheikh awa balla bou wer
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # thierno gaye 17-09-2014 00:34
Dieureudieufa cheikh ahmadou bamba khadim rassoul sounou yakar tay ak.euleukk
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # mame anta cisse 16-09-2014 17:12
dierediefeti khadimoul rassoul
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Assane ndiaye 03-09-2014 10:59
Dieureudieuf Serigne TOUBA chapeau au concepteur c'est vraiment utile.
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # ibrahima sougou 30-08-2014 23:54
dieuredieufety borom touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # khadim sylla 27-08-2014 01:46
nanio sante brome touba bou weer
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # mbathio diop 22-08-2014 20:41
khaside
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Fallou samb 18-08-2014 12:18
Dieureu nguen dieuf
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Moustapha kaire 09-08-2014 21:02
Moykignou fegal'dikignou haar'et aussi kignou saame
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # mouhamed diallo fall 21-07-2014 01:03
diadieuf liguey bi rafet na yala na yalla fayy
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Niass Talibé S.Touba 06-07-2014 18:45
Ahmadou deh amoul morome, kenn la
Sante koo
woulo koo
yakkar koo
toppou koo
rouyy koo
DIEUREDIEUF SERIGNE TOUBA KHADIM RASSOUL
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # papiss 04-07-2014 11:21
Dieureudieufeti serigne saliou serigne chiekh bethio diamou derigne saliou yalla nafi yague te guene and ak wer
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # sokhna amy mbacke 22-06-2014 10:15
dieureu ngueene dieuf mouride yi yalnaleene kou tedd ki faye taxawouleene samouleene
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Malick ngom beug fal 14-06-2014 12:21
Dieureudieuf kou thedd ki CHEIKH AHMADOU BAMBA KHADIME RASSOUL.DIARRAMA MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL BABOUL MOURIDINA MI TAKH GNOU HAM KOU THEDD KI.
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Mourtalla diouf 12-06-2014 17:02
On ne plus grand comme plaisir de lire les ecrits de khadimou rassoul.dieurejef bamba
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Mourtalla diouf 12-06-2014 17:02
On ne plus grand comme plaisir de lire les ecrits de khadimou rassoul.dieurejef bamba
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # khadim beugbamba rek 09-06-2014 12:09
Yalla na kou teddki def niou ay deuggui talibe te saxalnou si.aminee
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Abdou Thiam 07-06-2014 13:39
Yalnanguène dadièk ngaramoul serigne bi.
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # khalil mbacke 06-06-2014 12:32
Diaeuradiaf s touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # serigne abo fall 31-05-2014 20:14
yalla nalene serigne touba fayale bopam amine!!!!!!!!!!!!!!!
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # serigne abo fall 31-05-2014 20:12
serigne touba mi mana faye yalla nalene fayale bopame amine!!!!!!!!!!!!!!!
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Abdou diagne 31-05-2014 11:18
Diara diafati serigne touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # muumiabo 20-05-2014 09:08
Nous devons adopter le projet de societe redige par SERIGNE TOUBA a travers les SAINTS XASSAIDES seule issue pour le SENEGAL emergent,pour tous les musulmans mais aussi pour tout le monde(oh peuple de la terre oh peuple de la mer,venez repondre a l'ocean de generosite) PAIX A TOUT LE MONDE
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # adji mbacke 16-05-2014 22:33
Noune dey sant nagne ko bou werr dh di doli thia laneko santone nane ndakh monou manale louneiiu ta mana loune ko dara
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # modou sall 15-05-2014 09:33
Akassa.
Bou dieuk maggnis daneda war ay fasse di dem fou sori di woute khakhame.
Leginak khamkhame dalaye fek finga dog.
Dieureudieuf serigne touba.
Direugendieuf yenitame yengniko yombal.
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # baye ndiaga gueye 12-05-2014 17:33
deuge rek nga wakh
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # serigne mbacke diop 12-05-2014 13:10
bamba dou ken kouka kenal mou kenalamou kenal ba nga bege fo lambati dathie fa la fa guene gorelen sante serigne touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # ndiaga sow 06-05-2014 19:46
dieuredieuf mbokii talibeyi yalla guene fii yague
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Cheikh Abdou Dieng 26-04-2014 18:54
Wawlene gor
yalna ngene taseck nguramal serigne touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # cheikhouna leye 26-04-2014 09:49
Ginaw b santee yalla thi bole gimonou booleek cou selki nongy niane su boeom liy yeeney cou selki leepe thi diami yallayi s b defal coko
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # mouhamed mbacke 21-04-2014 10:03
Sent borom darou mouhty
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # sent s touba rek 21-04-2014 09:58
Ahma
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # sent s touba rek 21-04-2014 09:57
Mouhamed mbacke
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # mor diene 18-04-2014 20:58
Dieureudieuf Serigne touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # ALY NDIAYE 09-04-2014 23:05
am na solo lol mouride yalla nalene serigne touba faye
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # serigne mbacke mbsye 28-03-2014 21:11
Diarra diafe serigne touba yalla nanou yalla may gara mame
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # youssou mbaye 25-03-2014 07:15
Nane lanouy kennale kou tedd ki bakhe len mako
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # xaadim diop 24-03-2014 15:36
liguéy bi amna solo dieureu ngéne dieufeuti
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # sini gueye 20-03-2014 20:45
Y alla nano y alla do oli kheweullll
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Amadou 18-03-2014 21:31
Siar bou weer soxlanan xassida
Xamsatou ridial
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # sylla serigne mbaye 17-03-2014 23:23
Santeu serigne touba rek
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # cheikh badara leye 09-03-2014 21:25
Dieureuf serigne touba Sant serigne base diop rk
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Aldiouma gueye 08-03-2014 18:42
Minanoul bakhil khadim bou serigne BASSIROU en francais
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # samba seck 21-02-2014 13:05
Kendou serigne touba khadime rassol waye
Chiehkra fall keneu meunouko faye
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # baymaxime 17-02-2014 17:29
Diaguenedieuf boki talibeyi sante nanoulene
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # papa fall 16-02-2014 10:53
bamba par force
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # s fallou 15-02-2014 18:20
Serigne touba amol morom bamba fipa bamba lipa bamba par toute
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Mame Cheikh Mbacke 15-02-2014 10:43
Amoul lougana mague li ci liguéyal Serigne Touba moy di fékhé bagnépou mana diote ci mbindam mi ak khassida yi. Yallna léne Yalla fay ci barké S Touba diuerueguéne dieuf wassalame
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # ibrahima sougou 12-02-2014 20:40
yalna sakh
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # oumar khaqqane gueye 10-02-2014 16:23
ziarè nagne lène bou wère tay rafetlou sène ligueye bou akh yalla nalène serigne touba fayal bopame.NAKH Y7 AGUI NGOUYE YOMBALAL LIGUEYE BIBOU BAKH
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # masalla 28-01-2014 23:33
saliou ndiaye bichri
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # EL HADJI MB THIAM 25-01-2014 15:40
Bamba rek MOM RELA
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # EL HADJI MB THIAM 25-01-2014 15:38
Dieuredieuféty Borom TOUBA,'tay' 'EULEK'
774152676 Citation en provenance du commentaire précédent de assane khouma :
dieuredieuf kou tèddeu ki
Répondre | Répondre en citant | Citer
+2 # EL HADJI MB THIAM 25-01-2014 15:35
Dieuredieuféty Borom TOUBA,'tay' 'EULEK'
774152676 thiamsadikheà
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # papis kara 24-01-2014 16:57
dieuredieuf cheikh ahmadou bamba khadim rassoul gathier galama cheikh ahmadou kara bamba feep bamba partous bamba mercie
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # mouhamed nazir ndaw 19-01-2014 16:56
dieuredieuf serigne touba et serigne cheikh awa balla mbacke de pout et serigne moussa naweel de diarreeme
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # assane khouma 09-01-2014 23:39
dieuredieuf kou tèddeu ki
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # assane khouma 09-01-2014 23:34
dieuredieuf way ci ligèy bou rafèt bi
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Ahmadou Sam Lô 05-01-2014 09:38
diereudieuf waay mais masalikoul jinane sokhla nagnko trop
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # malick sene 27-12-2013 07:54
Dieuredieuf borom touba Bamba for ever
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # serigne mbacke ndiay 22-12-2013 11:48
karamaty khatou yadi
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # serigne mbacke ndiay 22-12-2013 11:46
diaradiaf borom touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # serigne mbacke ndiay 22-12-2013 11:46
diaradiaf borom touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # alex 13-12-2013 21:49
touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # beyeabdou1@live.fr 10-12-2013 18:40
al hamdou lil laahi dieureudieuf cheikhoul khadime
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # thierno 01-12-2013 13:20
Kmr63
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # amadou 06-11-2013 18:21
sokhasi salimtou thi midadi la nékk salimtou minal ahdai tourrane mahal tidja li rabbi wa baboul lahi lam yakou mourtadja
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # ahmadou bamba lo 04-11-2013 23:51
Santati kou tedd ki Mame borom touba mbacke dieureudieuf khadimoul khadim
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # diara diafe brom tou 04-11-2013 17:48
Moustapha
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # samba cisse 01-11-2013 12:37
dieuredieuf s touba koka wakh yalla nga féke diwine
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # Ndiasse seye 30-10-2013 12:52
Waaw leen goora waay ca kaw ca kanam ngoy ci Serigne bi reka woor . k le bon ns ci aider
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # DJILY DIALLO 09-10-2013 15:59
DIEUREDIEUF SRIGNE TOUBA
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # abdou khadre 29-09-2013 10:29
ziarénaléne bou wér je voudrais l'intégralité des chansons de ablaye niang svp
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # ibrahima fall 14-09-2013 18:58
assalaamou haleykoum! kouma mana dimbali thi ndiarignou touhfatou moutadarihiina! dieuredieuf d'avance....
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # massamba badiane 14-09-2013 14:10
sante nanou bou bakh di tambali si serigne sidy moukhtar mbacke di doli sant serigne touba ganaw bamou yessale sounas ta khamni la serigne bi badione ba tekthi bakanam nguir ISLAM DIEUM sa kanam nanou ko bagne nonbi nak ba legui mingui dokh thi louy yakh lislam si fane boumou meunti done bounou nanguou kene tilimal sounou dine ndakh lislam rek lanou ame ta moy tekhe tay ak eleuk wa salame
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # alpha gueye dpu fran 13-09-2013 17:00
Bamba fep dieuredieuf serigne touba diararama cheikh ibra fall lamp depuis france nantes talibe serigne fallou fall mou mame amedy yacine fall narou kawsara fall
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # amdy moustapha tamba 23-08-2013 14:12
gueume serigne touba rek kenale ko wolou ko rekrek dieureudiefe cheikh ibra fall
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # MOMAR AWA GUEYE 12-08-2013 13:05
dieuredieuf mbacké deugla..wayé kfre bou guemoul yalla baakhoul,wayé douñouma yakhal dara,wayé serigne touba mome ken douko fofamtó sama kanam,wala ngamay wone ni faléwóko,khan ngani lolou kou yewwu wala nga kham dara doko deff..serigne touba kilifeu la.boko beugoul beugouma sa dara,ko khamoul khamó rek
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # baye fall sow 10-08-2013 18:10
karamati khattou yadi
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # mbaye ndir 28-07-2013 13:15
sant serigne touba rek diarama mame chiekh ibra fall
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # bara diop 23-07-2013 08:56
Dieureudieufé SERIGNE TOUBA
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # sokhna 22-07-2013 11:12
Midadi
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # nafissatou 22-07-2013 11:11
salam je voudrai savoir dans quel khassaïde se trouve salimto
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # khadim diop 27-06-2013 13:44
Dieureudieuf cheikhoul khadiim sama khol
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # salioukane 15-05-2013 17:59
diara diafe serigne touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
copyright Al-himma 2010-2017